About Kàddug Yàlla gi
Appli bii mooy Kàddug Yàlla, gi dikke ñaari pàcc: Kóllëre gu jëkk gi Yàlla fas ak nit, ak Kóllëre gu yees, gi mujja wàcc, te ñenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru jàmm. Ñaari téere yooyu, Yàllaa leen wàcce ci nitam ñu sell ñi, kóllëre gu jëkk gi, ñu bind ko ci yawut, gu yees gi, ci làkku gereg. Li ñu bind ci téere yu jëkk ya nag, moom lanu tekki ci wolof.
[bible, wolof, kaddug yalla gi] Yalla Apps bii Mooy Kàddug gi dikke NAARI PACC: Kóllëre gu Jekk gi Yalla fas nit ak ak Kóllëre gu yees gi mujja WACC you Nenn ñi di ko wooye Injiil, mu tekki Xibaaru Jamm. NAARI téere yooyu, Yàllaa leen wàcce it nitam bare sell ñi, kóllëre gu Jekk gi, bare bind ko it yawut gu yees gi, it làkku Gereg. Li bare bind it téere yu Jekk is nag, moom lanu tekki it Wolof.
[Bible Wolof kaddug yalla gi]
Download and install
Kàddug Yàlla gi version 1.4.8 on your
Android device!
Downloaded 1,000+ times, content rating: Everyone
Android package:
org.mbs.kyg.wol, download Kàddug Yàlla gi.apk
by A####:
Une application très fluide et super pratique. Merci !